Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 28

Kàddu yu Xelu 28:27-28

Help us?
Click on verse(s) to share them!
27Kuy jox néew-ji-doole, doo ñàkk; nga gëmm ne gisoo, bare ku la móolu.
28Bu ab soxor faloo, ñépp làquji, bu daanoo, ku jub teg tànk.

Read Kàddu yu Xelu 28Kàddu yu Xelu 28
Compare Kàddu yu Xelu 28:27-28Kàddu yu Xelu 28:27-28