Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 28:27-28 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 28:27-28 in Kàddug Yàlla gi

27 Kuy jox néew-ji-doole, doo ñàkk; nga gëmm ne gisoo, bare ku la móolu.
28 Bu ab soxor faloo, ñépp làquji, bu daanoo, ku jub teg tànk.
Kàddu yu Xelu 28 in Kàddug Yàlla gi