Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 28

Kàddu yu Xelu 28:18-20

Help us?
Click on verse(s) to share them!
18Mat, mucc; dëng, dàll daanu.
19Beyal sab tool, sab dund doy; topp ay caaxaan, ndóol ba doyal.
20Boroom worma, bare barke; ku yàkkamtee woomle, sa mbugal du jaas.

Read Kàddu yu Xelu 28Kàddu yu Xelu 28
Compare Kàddu yu Xelu 28:18-20Kàddu yu Xelu 28:18-20