Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 28:18-20 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 28:18-20 in Kàddug Yàlla gi

18 Mat, mucc; dëng, dàll daanu.
19 Beyal sab tool, sab dund doy; topp ay caaxaan, ndóol ba doyal.
20 Boroom worma, bare barke; ku yàkkamtee woomle, sa mbugal du jaas.
Kàddu yu Xelu 28 in Kàddug Yàlla gi