Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 28

Kàddu yu Xelu 28:16-19

Help us?
Click on verse(s) to share them!
16Kilifa gu amul ug dégg, day foqati rekk, waaye ku bañ lu lewul, gudd fan.
17Ku bóom nit, daw, ba tàbbi njaniiw; bu ko kenn taxawu.
18Mat, mucc; dëng, dàll daanu.
19Beyal sab tool, sab dund doy; topp ay caaxaan, ndóol ba doyal.

Read Kàddu yu Xelu 28Kàddu yu Xelu 28
Compare Kàddu yu Xelu 28:16-19Kàddu yu Xelu 28:16-19