Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 28

Kàddu yu Xelu 28:14-15

Help us?
Click on verse(s) to share them!
14Mbégte ñeel na ku saxoo ragal, waaye ku dëgër bopp tàbbi ci njekkar.
15Kilifa guy soxore néew-ji-doole mook gaynde guy yëmmoo yem, mbaa rab wuy songe.

Read Kàddu yu Xelu 28Kàddu yu Xelu 28
Compare Kàddu yu Xelu 28:14-15Kàddu yu Xelu 28:14-15