Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 28:14-15 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 28:14-15 in Kàddug Yàlla gi

14 Mbégte ñeel na ku saxoo ragal, waaye ku dëgër bopp tàbbi ci njekkar.
15 Kilifa guy soxore néew-ji-doole mook gaynde guy yëmmoo yem, mbaa rab wuy songe.
Kàddu yu Xelu 28 in Kàddug Yàlla gi