24ndax alal wéyul fàww, ag pal du ñeel sëtoo sët.
25Gannaaw bu ñu gubee, ba ñax saxaat, ñu dajale ngooñ ma ca tund ya,
26say xar da lay amal koddaay, bëy yi génneel la njégu tool.
27Meewum bëy daldi am, ba doy la dund, yaak sa waa kër ak sa surga yu jigéen.