Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 27:24-27 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 27:24-27 in Kàddug Yàlla gi

24 ndax alal wéyul fàww, ag pal du ñeel sëtoo sët.
25 Gannaaw bu ñu gubee, ba ñax saxaat, ñu dajale ngooñ ma ca tund ya,
26 say xar da lay amal koddaay, bëy yi génneel la njégu tool.
27 Meewum bëy daldi am, ba doy la dund, yaak sa waa kër ak sa surga yu jigéen.
Kàddu yu Xelu 27 in Kàddug Yàlla gi