Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 27

Kàddu yu Xelu 27:23-24

Help us?
Click on verse(s) to share them!
23Xamal bu baax lu say gàtt nekke, te def sa xel ci say gétt,
24ndax alal wéyul fàww, ag pal du ñeel sëtoo sët.

Read Kàddu yu Xelu 27Kàddu yu Xelu 27
Compare Kàddu yu Xelu 27:23-24Kàddu yu Xelu 27:23-24