Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 27:23-24 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 27:23-24 in Kàddug Yàlla gi

23 Xamal bu baax lu say gàtt nekke, te def sa xel ci say gétt,
24 ndax alal wéyul fàww, ag pal du ñeel sëtoo sët.
Kàddu yu Xelu 27 in Kàddug Yàlla gi