Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 27

Kàddu yu Xelu 27:19-21

Help us?
Click on verse(s) to share them!
19Ku xool cim ndox, gis sa kanam, nga xool sab xol, gis sa jikko.
20Njaniiw ak biir suuf du fees, bët it du doylu mukk.
21Xaalis ak wurus sawaraa koy xelli, waaye àtteb nit ca jëëm.

Read Kàddu yu Xelu 27Kàddu yu Xelu 27
Compare Kàddu yu Xelu 27:19-21Kàddu yu Xelu 27:19-21