Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 27:19-21 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 27:19-21 in Kàddug Yàlla gi

19 Ku xool cim ndox, gis sa kanam, nga xool sab xol, gis sa jikko.
20 Njaniiw ak biir suuf du fees, bët it du doylu mukk.
21 Xaalis ak wurus sawaraa koy xelli, waaye àtteb nit ca jëëm.
Kàddu yu Xelu 27 in Kàddug Yàlla gi