Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 27

Kàddu yu Xelu 27:14-17

Help us?
Click on verse(s) to share them!
14Nuyoo bu xumb, suba teel mooki saagaa yem.
15Jabar ju pànk mooy senn bu dakkul, cib taw;
16ku ko mana yemale, mana téye ngelaw mbaa nga ŋëb ag diw.
17Weñ ay nàmm weñ, nit ay nàmm xelu moroom ma.

Read Kàddu yu Xelu 27Kàddu yu Xelu 27
Compare Kàddu yu Xelu 27:14-17Kàddu yu Xelu 27:14-17