Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 27

Kàddu yu Xelu 27:12-15

Help us?
Click on verse(s) to share them!
12Kuy foog, gisu ay, làqu; ab téxét ne ca tëñëx, loru.
13Ku gàddul jaambur bor, jëlal mbubbam; tayle ko, moo dige feyal ndaw su yemadi.
14Nuyoo bu xumb, suba teel mooki saagaa yem.
15Jabar ju pànk mooy senn bu dakkul, cib taw;

Read Kàddu yu Xelu 27Kàddu yu Xelu 27
Compare Kàddu yu Xelu 27:12-15Kàddu yu Xelu 27:12-15