Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 27:12-15 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 27:12-15 in Kàddug Yàlla gi

12 Kuy foog, gisu ay, làqu; ab téxét ne ca tëñëx, loru.
13 Ku gàddul jaambur bor, jëlal mbubbam; tayle ko, moo dige feyal ndaw su yemadi.
14 Nuyoo bu xumb, suba teel mooki saagaa yem.
15 Jabar ju pànk mooy senn bu dakkul, cib taw;
Kàddu yu Xelu 27 in Kàddug Yàlla gi