Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 26

Kàddu yu Xelu 26:7-9

Help us?
Click on verse(s) to share them!
7Kàddu gu xelu ci gémmiñug dof, mooy tànki lafañ, amalu ko njariñ.
8Kuy teral ab dof, jël ngaw doj, takk ko ci mbaq.
9Kàddu gu xelu ci gémmiñug dof mooy car aki dégam, màndikat xàcci.

Read Kàddu yu Xelu 26Kàddu yu Xelu 26
Compare Kàddu yu Xelu 26:7-9Kàddu yu Xelu 26:7-9