Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Kàddu yu Xelu 26:7-9 in Wolof
Help us?
Kàddu yu Xelu 26:7-9
in
Kàddug Yàlla gi
7
Kàddu gu xelu ci gémmiñug dof, mooy tànki lafañ, amalu ko njariñ.
8
Kuy teral ab dof, jël ngaw doj, takk ko ci mbaq.
9
Kàddu gu xelu ci gémmiñug dof mooy car aki dégam, màndikat xàcci.
Kàddu yu Xelu 26 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms