Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 26

Kàddu yu Xelu 26:4-7

Help us?
Click on verse(s) to share them!
4Bul topp ab dof cig ndofam, lu ko moy nga mel ni moom.
5Waaye toppal ab dof cig ndofam, lu ko moy mu defe ne daa muus.
6Ku yóbbante ab dof kàddu, yaa woo fitna, gor say tànk.
7Kàddu gu xelu ci gémmiñug dof, mooy tànki lafañ, amalu ko njariñ.

Read Kàddu yu Xelu 26Kàddu yu Xelu 26
Compare Kàddu yu Xelu 26:4-7Kàddu yu Xelu 26:4-7