Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 26:4-7 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 26:4-7 in Kàddug Yàlla gi

4 Bul topp ab dof cig ndofam, lu ko moy nga mel ni moom.
5 Waaye toppal ab dof cig ndofam, lu ko moy mu defe ne daa muus.
6 Ku yóbbante ab dof kàddu, yaa woo fitna, gor say tànk.
7 Kàddu gu xelu ci gémmiñug dof, mooy tànki lafañ, amalu ko njariñ.
Kàddu yu Xelu 26 in Kàddug Yàlla gi