Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 26

Kàddu yu Xelu 26:3-4

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3Xiir, aw fas; laab, mbaam; yetu gannaaw, ab dof.
4Bul topp ab dof cig ndofam, lu ko moy nga mel ni moom.

Read Kàddu yu Xelu 26Kàddu yu Xelu 26
Compare Kàddu yu Xelu 26:3-4Kàddu yu Xelu 26:3-4