Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 26

Kàddu yu Xelu 26:22-23

Help us?
Click on verse(s) to share them!
22Waxi jëwkat di ñam wu neex, wuy seey, jàll ca biir-a-biir.
23Kuy wax lu neex, tey mébét lu bon, yaay xaalis bu rax, ñu xoob ca ndabal xandeer.

Read Kàddu yu Xelu 26Kàddu yu Xelu 26
Compare Kàddu yu Xelu 26:22-23Kàddu yu Xelu 26:22-23