Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 26:22-23 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 26:22-23 in Kàddug Yàlla gi

22 Waxi jëwkat di ñam wu neex, wuy seey, jàll ca biir-a-biir.
23 Kuy wax lu neex, tey mébét lu bon, yaay xaalis bu rax, ñu xoob ca ndabal xandeer.
Kàddu yu Xelu 26 in Kàddug Yàlla gi