Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 25

Kàddu yu Xelu 25:5-8

Help us?
Click on verse(s) to share them!
5Ab soxor it, dàqal, mu sore buur, ngir njubte law, jalam sax.
6Bul réy-réylu fi kanam buur, bul tooge jataayu boroom daraja,
7ndax ñu ne la: «Yéegal, jegesi fii,» moo gën ñu torxal la ci kanam kilifa. Boo gisalee sa bopp it,
8bul gaawa layooji, ana nooy def ëllëg, bu ñu la yeyee?

Read Kàddu yu Xelu 25Kàddu yu Xelu 25
Compare Kàddu yu Xelu 25:5-8Kàddu yu Xelu 25:5-8