Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 25:5-8 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 25:5-8 in Kàddug Yàlla gi

5 Ab soxor it, dàqal, mu sore buur, ngir njubte law, jalam sax.
6 Bul réy-réylu fi kanam buur, bul tooge jataayu boroom daraja,
7 ndax ñu ne la: «Yéegal, jegesi fii,» moo gën ñu torxal la ci kanam kilifa. Boo gisalee sa bopp it,
8 bul gaawa layooji, ana nooy def ëllëg, bu ñu la yeyee?
Kàddu yu Xelu 25 in Kàddug Yàlla gi