Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 25

Kàddu yu Xelu 25:3-4

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3Maneesula daj li ci xelu buur, xalaatam daa kawe ni asamaan, xóot ni suuf.
4Xellil xaalis, tonni lu ca rax, ba ab tëgg man caa am ndab.

Read Kàddu yu Xelu 25Kàddu yu Xelu 25
Compare Kàddu yu Xelu 25:3-4Kàddu yu Xelu 25:3-4