Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 25:3-4 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 25:3-4 in Kàddug Yàlla gi

3 Maneesula daj li ci xelu buur, xalaatam daa kawe ni asamaan, xóot ni suuf.
4 Xellil xaalis, tonni lu ca rax, ba ab tëgg man caa am ndab.
Kàddu yu Xelu 25 in Kàddug Yàlla gi