Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 25

Kàddu yu Xelu 25:26-28

Help us?
Click on verse(s) to share them!
26Ku jub bu dee nangul ku bon, yàqu na, ni seyaan bu nëx mbaa teen bu xàbb.
27Lekk lem ju ëpp baaxul, te wut waaw-góor du ngóora.
28Ku dul ànd ak sa sago, yaa neexa song ni dëkk bu dara wërul.

Read Kàddu yu Xelu 25Kàddu yu Xelu 25
Compare Kàddu yu Xelu 25:26-28Kàddu yu Xelu 25:26-28