Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 25:26-28 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 25:26-28 in Kàddug Yàlla gi

26 Ku jub bu dee nangul ku bon, yàqu na, ni seyaan bu nëx mbaa teen bu xàbb.
27 Lekk lem ju ëpp baaxul, te wut waaw-góor du ngóora.
28 Ku dul ànd ak sa sago, yaa neexa song ni dëkk bu dara wërul.
Kàddu yu Xelu 25 in Kàddug Yàlla gi