Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 25

Kàddu yu Xelu 25:25-27

Help us?
Click on verse(s) to share them!
25Xibaaru jàmm, bawoo fu sore mooy ndox mu sedd ci ku loof.
26Ku jub bu dee nangul ku bon, yàqu na, ni seyaan bu nëx mbaa teen bu xàbb.
27Lekk lem ju ëpp baaxul, te wut waaw-góor du ngóora.

Read Kàddu yu Xelu 25Kàddu yu Xelu 25
Compare Kàddu yu Xelu 25:25-27Kàddu yu Xelu 25:25-27