Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 25:25-27 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 25:25-27 in Kàddug Yàlla gi

25 Xibaaru jàmm, bawoo fu sore mooy ndox mu sedd ci ku loof.
26 Ku jub bu dee nangul ku bon, yàqu na, ni seyaan bu nëx mbaa teen bu xàbb.
27 Lekk lem ju ëpp baaxul, te wut waaw-góor du ngóora.
Kàddu yu Xelu 25 in Kàddug Yàlla gi