Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 25

Kàddu yu Xelu 25:2-3

Help us?
Click on verse(s) to share them!
2Màggug Yàllaa ngi ci li mu làq, darajay buur a ngi ci li mu feeñal.
3Maneesula daj li ci xelu buur, xalaatam daa kawe ni asamaan, xóot ni suuf.

Read Kàddu yu Xelu 25Kàddu yu Xelu 25
Compare Kàddu yu Xelu 25:2-3Kàddu yu Xelu 25:2-3