Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 25:2-3 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 25:2-3 in Kàddug Yàlla gi

2 Màggug Yàllaa ngi ci li mu làq, darajay buur a ngi ci li mu feeñal.
3 Maneesula daj li ci xelu buur, xalaatam daa kawe ni asamaan, xóot ni suuf.
Kàddu yu Xelu 25 in Kàddug Yàlla gi