Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 25

Kàddu yu Xelu 25:17-19

Help us?
Click on verse(s) to share them!
17Na sa tànk di gëj kër dëkkandoo; boo ko sàppee, mu jéppi la.
18Ku seedeel sa moroom ay fen, yen nga ko aw njur mbaa saamar mbaa fitt.
19Bul wóolu workat bésub njàqare, mooy bëñ bu bon mbaa tànk bu nasax.

Read Kàddu yu Xelu 25Kàddu yu Xelu 25
Compare Kàddu yu Xelu 25:17-19Kàddu yu Xelu 25:17-19