Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 25:17-19 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 25:17-19 in Kàddug Yàlla gi

17 Na sa tànk di gëj kër dëkkandoo; boo ko sàppee, mu jéppi la.
18 Ku seedeel sa moroom ay fen, yen nga ko aw njur mbaa saamar mbaa fitt.
19 Bul wóolu workat bésub njàqare, mooy bëñ bu bon mbaa tànk bu nasax.
Kàddu yu Xelu 25 in Kàddug Yàlla gi