Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 25

Kàddu yu Xelu 25:15-18

Help us?
Click on verse(s) to share them!
15Muñ mer ay nax kilifa, te wax ju neex, fu mu jaar, mu nooy.
16Boo gisee lem, lekkal lu yem; bu ëppee, nga waccu ko.
17Na sa tànk di gëj kër dëkkandoo; boo ko sàppee, mu jéppi la.
18Ku seedeel sa moroom ay fen, yen nga ko aw njur mbaa saamar mbaa fitt.

Read Kàddu yu Xelu 25Kàddu yu Xelu 25
Compare Kàddu yu Xelu 25:15-18Kàddu yu Xelu 25:15-18