Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 25:15-18 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 25:15-18 in Kàddug Yàlla gi

15 Muñ mer ay nax kilifa, te wax ju neex, fu mu jaar, mu nooy.
16 Boo gisee lem, lekkal lu yem; bu ëppee, nga waccu ko.
17 Na sa tànk di gëj kër dëkkandoo; boo ko sàppee, mu jéppi la.
18 Ku seedeel sa moroom ay fen, yen nga ko aw njur mbaa saamar mbaa fitt.
Kàddu yu Xelu 25 in Kàddug Yàlla gi