Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 25

Kàddu yu Xelu 25:14-16

Help us?
Click on verse(s) to share them!
14Kuy dige te doo joxe, yaay xiin wu ngelaw, mu naaxsaay.
15Muñ mer ay nax kilifa, te wax ju neex, fu mu jaar, mu nooy.
16Boo gisee lem, lekkal lu yem; bu ëppee, nga waccu ko.

Read Kàddu yu Xelu 25Kàddu yu Xelu 25
Compare Kàddu yu Xelu 25:14-16Kàddu yu Xelu 25:14-16