Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 25:14-16 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 25:14-16 in Kàddug Yàlla gi

14 Kuy dige te doo joxe, yaay xiin wu ngelaw, mu naaxsaay.
15 Muñ mer ay nax kilifa, te wax ju neex, fu mu jaar, mu nooy.
16 Boo gisee lem, lekkal lu yem; bu ëppee, nga waccu ko.
Kàddu yu Xelu 25 in Kàddug Yàlla gi