Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 24

Kàddu yu Xelu 24:6-10

Help us?
Click on verse(s) to share them!
6tegtal yu xelu lañuy xaree, diisoo bu yaatooy maye ndam.
7Wax ju xelu sut nab dof, jataayu pénc du fa àddoo.
8Kuy mébét lu bon, ñu ne yaay rambaaj bi.
9Pexem dof bàkkaar la, te kuy ñaawle, ñu sib la.
10Bu mettee, nga yoqi, sa doolee néew.

Read Kàddu yu Xelu 24Kàddu yu Xelu 24
Compare Kàddu yu Xelu 24:6-10Kàddu yu Xelu 24:6-10