Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 24:6-10 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 24:6-10 in Kàddug Yàlla gi

6 tegtal yu xelu lañuy xaree, diisoo bu yaatooy maye ndam.
7 Wax ju xelu sut nab dof, jataayu pénc du fa àddoo.
8 Kuy mébét lu bon, ñu ne yaay rambaaj bi.
9 Pexem dof bàkkaar la, te kuy ñaawle, ñu sib la.
10 Bu mettee, nga yoqi, sa doolee néew.
Kàddu yu Xelu 24 in Kàddug Yàlla gi