Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 24

Kàddu yu Xelu 24:27-29

Help us?
Click on verse(s) to share them!
27Ruujal sab tool, ji ko, doora tabax sa kër.
28Bul tuumaal nit ci neen, te bu ko seedeel ay fen.
29Bul ne: «Li mu ma def laa koy def, damay feyu li mu ma def.»

Read Kàddu yu Xelu 24Kàddu yu Xelu 24
Compare Kàddu yu Xelu 24:27-29Kàddu yu Xelu 24:27-29