Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 24:27-29 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 24:27-29 in Kàddug Yàlla gi

27 Ruujal sab tool, ji ko, doora tabax sa kër.
28 Bul tuumaal nit ci neen, te bu ko seedeel ay fen.
29 Bul ne: «Li mu ma def laa koy def, damay feyu li mu ma def.»
Kàddu yu Xelu 24 in Kàddug Yàlla gi