Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 24

Kàddu yu Xelu 24:21-25

Help us?
Click on verse(s) to share them!
21Doom, ragalal Aji Sax ji, wormaal buur. Bul lëngook kuy fippu.
22Yàllaak buur a koy bette mbugal, te kenn xamul musiba mu muy doon.
23Lii it ñi rafet xel a ko wax. Par-parloo cib àtte baaxul.
24Ku ne defkatu lu bon: «Yaw, tooñoo,» aw nit móolu la, mbooloo ŋàññ la;
25ku ko ne: «Yaa tooñ,» yaay baaxle, taasoo barke bu yaa.

Read Kàddu yu Xelu 24Kàddu yu Xelu 24
Compare Kàddu yu Xelu 24:21-25Kàddu yu Xelu 24:21-25