Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 24

Kàddu yu Xelu 24:20-21

Help us?
Click on verse(s) to share them!
20Ku bon amul muj, ku soxor day mel ni taal bu fey.
21Doom, ragalal Aji Sax ji, wormaal buur. Bul lëngook kuy fippu.

Read Kàddu yu Xelu 24Kàddu yu Xelu 24
Compare Kàddu yu Xelu 24:20-21Kàddu yu Xelu 24:20-21