Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 24:20-21 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 24:20-21 in Kàddug Yàlla gi

20 Ku bon amul muj, ku soxor day mel ni taal bu fey.
21 Doom, ragalal Aji Sax ji, wormaal buur. Bul lëngook kuy fippu.
Kàddu yu Xelu 24 in Kàddug Yàlla gi