Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 24

Kàddu yu Xelu 24:16-18

Help us?
Click on verse(s) to share them!
16Ku jub day daanu juróom yaari yoon, jógaat, ab soxor sërëx ci njekkar.
17Bu sab noon daanoo, bu ko bànneexoo, bu tërëfee, bu ko bége.
18Lu ko moy Aji Sax ji gis la, ñaawlu ko, daldi giif, dootu ko mbugal.

Read Kàddu yu Xelu 24Kàddu yu Xelu 24
Compare Kàddu yu Xelu 24:16-18Kàddu yu Xelu 24:16-18