Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 24:16-18 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 24:16-18 in Kàddug Yàlla gi

16 Ku jub day daanu juróom yaari yoon, jógaat, ab soxor sërëx ci njekkar.
17 Bu sab noon daanoo, bu ko bànneexoo, bu tërëfee, bu ko bége.
18 Lu ko moy Aji Sax ji gis la, ñaawlu ko, daldi giif, dootu ko mbugal.
Kàddu yu Xelu 24 in Kàddug Yàlla gi