Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 24

Kàddu yu Xelu 24:15-17

Help us?
Click on verse(s) to share them!
15Soxor bi, bul tëru ku jub ci këram, bul yàq dëkkuwaayam.
16Ku jub day daanu juróom yaari yoon, jógaat, ab soxor sërëx ci njekkar.
17Bu sab noon daanoo, bu ko bànneexoo, bu tërëfee, bu ko bége.

Read Kàddu yu Xelu 24Kàddu yu Xelu 24
Compare Kàddu yu Xelu 24:15-17Kàddu yu Xelu 24:15-17