Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 24:15-17 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 24:15-17 in Kàddug Yàlla gi

15 Soxor bi, bul tëru ku jub ci këram, bul yàq dëkkuwaayam.
16 Ku jub day daanu juróom yaari yoon, jógaat, ab soxor sërëx ci njekkar.
17 Bu sab noon daanoo, bu ko bànneexoo, bu tërëfee, bu ko bége.
Kàddu yu Xelu 24 in Kàddug Yàlla gi